COUMBA GAWLO - SOLEIL (Video Officielle)

A travers cette chanson, Coumba Gawlo invite à l’espoir, dans un contexte où les sources d’inquiétude et de désarroi sont multiples. Soleil, un appel à un retour aux sources et à la résilience, est une réponse conséquente aux aspirations des citoyens, la jeunesse en particulier. Des paroles qui interpellent, pour qu’enfin l’espoir soit restauré et que le chemin d’un avenir meilleur soit illuminé par les rayons du Soleil. Paroles : Nadj bi fenk né tek Drapeau bi ci kaw mi ngui né tek Liir bangui dioye niou nakh ko mou né tek Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek Armel yi sedd né tek Ngoné Latyr thieu dékheulé tek Imam ak labé yague def tek Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs Sénégalais yague ngua done ndaanane Mba di ngua ko moudjé Ahmadou Kaabar guedj gui né tek Limamou né ko Laye guedj gui né tek Baye Niass khamal la ngua kham né tek Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek Sunu taarikh mingui niou khol né tek Médina Gounass, ndiassane, Thiénaba tek Wakh diou bone noppé ko gueune Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs Sénégalais yague ngua done ndaanane Mba di ngua ko moudjé Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs Ndeyssane yague ngua done ndaanane Mba di ngua ko moudjé Moudiou gou rafet mo diara niane Lolou motakh bima dégué Gawlo yaye sunu ndaanane May lathie ndakh mba dina ko moudjé ndakh Nietti att mou rothie sama baat mané tek Tivavouane néma tallal lokho teu nel tek Ndakh falaises bandiagara yague def tek Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs Sénégalais yague ngua done ndaanane Mba di ngua ko moudjé Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs Vert Jaune Rouge yague ngua done ndaanane Mba di ngua ko moudjé Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs Lac rose né dou changer teu dina rose batay dji Mba dinako moudjé… (moudjiéeeeeeeeee) A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs Bepp nguur nangua guestu sa askane Yene ak niome yénéy moudjé Bou yomal khiyamé yalla yeureumeulma sénégalais Guem na né nonou lay moudjé Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs Sénégalais yague ngua done ndaanane Mba di ngua ko moudjé
Back to Top